Elige una pista para reproducir
Kula faale wul man mii maa lay faale
Doon sa seetu kula xool man lay gisaale
Kula faale wul man mii maa lay faale
Doon sa seetu kula xool man lay gisaale
Ci sa bët laay xool naan la "I Love You"
Baby yow yaay sama life
Ci sa bët laay xool naan la "I Love You"
Baby yow yaay sama life
Baby yow yaay sama life
Suma Yàlla bëggee wax léen ko na ma bayyi ak yow
Ndax ku melni yow amatul ci àdduna
Sama xol laa la def bëgg dëgg laa la def te duma sooraale
Benn noon ndax yow yaay sama life