Оберіть трек для відтворення
Felicia
Felicia weh falema ma wey
Felicia weh ma woyal la
Felicia weh falema ma wey
Felicia weh ma woyal la
Suba ba legui mangui tok si bopu kogn bi
Dila xaar dila xaar dila xaar
Tok si bopu kogn bi
Dila xaar nga guenn sa gale
Legui nga guena
Bagama rombe ni
Legui nga guenn dima iñoreni
Xana xamone yaw tey dama al fokma diokok yaw hirl
Tey dama aal
Fokma waxtaan ak yaw
Felicia weh falema ma wey
Felicia weh ma woyal la
Felicia weh falema ma wey
Felicia weh ma woyal la
Bimalay soga guiss tji butik bi
Xol.la man sila la barde
Binga guesso ba xol ma sila xam ne yamay daanel
Bobu ba legui yaw mangley set manumala guiss linguey guenn barewul
Motax tey mane fokma warla melni ku werul
Felicia weh falema ma wey
Felicia weh ma woyal la
Felicia weh falema ma wey
Felicia weh ma woyal la
Wayna wayna Feli fe fe fe fe fe
Xalebile Feli fe fe fe fe fe
Dinala setsi dinala dieulsi
Dinala yobu
Beugeunala Yebenala xalebi
Beugeunala beugeunala beugeunala beugeunala nopnala nopnala nopnala nopnala